Soo duggee ci benn sitweb, mën nañu denc ay done ci sa nawigatër wala ñu jëlee ko ci sa nawigatër, lu ci gëna bari ci xeetu kukiis. Leeral yooyu mën nañu nekk ci yaw, say tànneef wala sa aparey te dañu leen di gëna jëfandikoo ngir sitweb bi dox ci ninga ko yaakaaree. Leeral yi duñu la xàmmee ci saasi, waaye mën nañu la jox jaar-jaaru web buñ personaalise bu baax. Ndax danuy sargal sa yelleefu nëbbëtu, danu lay may nga baña nangu yenn xeeti kukiis. Bësal ci kategori yi ngir gëna xam bu nekk ci ñoom, ba noppi nga soppi jekkal yiñ jagleel. Waaye, soo blokee yenn xeeti kukiis, mën nañu indi jafe-jafe ci sa nawigasioŋ ak ci sarwis yi ñu la mëna jox.
Kuki yu am solo lool
Kukiis yooyu dañu am solo ngir sitweb bi mëna dox te mënu ñu leen dindi ci sunuy sistem. Dañu leen di faral di def ngir tontu jëf yi nga def yu méngoo ak sàqum sarwis, lu ci melni def say tànneefi sàmmonte, dugg wala joxe ay formileer. Mën nga def sa nawigatër mu bloke wala mu artu la ci kukiis yooyu, waaye yenn pàcci sitweb bi mën nañu baña dox. Kukiis yooyu duñu denc benn leeral buy xàmmee nit ki.
Kuki yu am njariñ
Kuki yii dañu lay jàppale nga gëna mëna jëfandikoo sitweb bi. Sunu ekip yi ñoo leen mëna aktive, wala ñeneen ñuy jëfandikoo seen serwiis ci xëti sunu sitweb. Sudee nanguwoo kukiis yii, yenn ci sarwis yii wala yépp mën nañu baña dox nimu waree.
Kuki liggéey
Kuki yii dañu nuy may nu xam limu nit ñiy ñëw ci sunu sitweb ak fi ñuy joge, suko defee ñu mëna natt ak gëna suqali sunu sitweb. Dañu nuy jàppale itam nu ràññee xët yi gëna siiw ak yi gëna néew siiw, ba noppi nu jàngat ni nit ñi di duggee ci sitweb bi. Lépp lu kukiis yii di dajale dañu koy boole, moo tax duñu ko nëbb. Sudee nanguwoo kukiis yii, du nu yëgal ni danga dugg ci sunu sit.
Kuki ngir piblisite buñ tànn
Sunuy naataango yiy yëgle ñoo mëna def kukiis yii ci sunu sitweb. Mën nañu ko jëfandikoo ci liggéeyukaay yooyu ngir defar sa profil ci say bëgg-bëgg ak ngir wane la ay yëgle yu am solo ci yeneen sitweb. Duñu denc done yu bopp ci saasi, waaye dañu sukkandikoo ci ràññee sa nawigatër ak sa aparey internet. Soo nanguwoo kukiis yii, sa piblisite dina gëna néew luñu la jox.
Soo bësee ci « Nangu kukiis yépp », nangu nga denc kukiis yi ci sa aparey ngir gëna yombal seet sit bi, jàngat jëfandikoo sit bi, ak jàppale ci sunuy liggéeyu fësal njaay.