Serwiis ginaaw njaay

Ci CCBM Industries Automobiles, danuy jox mbégte ci joxe serwiis bu baax ginaaw njaay, muy lu am solo ngir mëna wóolu sunu kiliyaan yi.

Sunu Serwiisu Gaaw dañu ko jagleel ngir mëna toppatoo sa oto ci anam wu gaaw te baax, lépp di aju ci ni ngay toppatoo sa oto te ba noppi nekk ci kalite bu kawe.

Rax ci dolli, danuy jaay itam pièce de rechange original, suko defee mu méngoo bu baax ak anam wi sa oto di doxee, ba noppi di garanti seen liggéey bu baax ëlëg.

ab serwiis buñu defaree ginaaw njaay

portfolio

Toppatoo ak revison général

portfolio

Cane ak pare-brise

portfolio

Carrosserie ak peinture

portfolio

saafara jafe-jafe mobile

portfolio

Magasin pièces de rechange