Danuy jëfandikoo kukiis ngir sunu sitweb mëna dox bu baax. Yenn kukiis yi dañu am solo (lu melni yiy yor sa sesioŋ). Danuy jëfandikoo itam ay kukiis ngir jàngat dem bi ak dikk bi. Soo nangu rek lañuy jëfandikoo mbir yooyu.
Ba leegi defagoo sa tànneef ci sunu sàrti kukiis.
Noo ngi lay sant nga def sa tànneef soo bësee ci "nangu wala bañ" ci banner bi feeñ ci suufu sa xët.
Ci anam wu méngoo ak sàrt n°2008-12 bu 25 saŋwiye 2008, biy wax ci aar ay done yu nit, te am doole ci République Senegal, danuy jox solo bu mag ci kumpa ak kaaraange done yu nit ñi sunuy abone.
Soo defee ay laaj ci sunu sitweb, dañuy jël yenn leerali bopp, lu ci melni: sa tur, sa sant, sa liggéey, sa adres e-mail, ak sa nimero telefon. Done yii dañu am solo ngir mëna yonnee sa abonemaa bi, fexe ñu topp ko, ba noppi may la nga am jaar-jaaru kiliyaan bu baax.
Dañuy tëye sa done ci kumpa, te kenn duko séddoo ak ñeneen ci anam wumu mëna doon, fileek nanguwoo ko. Jaaraleko ci nun, mën nga joxe leeral wala xéewali fësal mbir ci imeel.
Dañuy denc say done ci diir bi war ngir mëna doxal sunu diggante liggéey, wala ci diir bi yoon santaane.
Ngir jëfandikoo yelleef yooyu, mën nga jokkoo ak nun ci ccbmindustries@ccbm.sn ngir leeral lu tax nga laaj, wala nga yebbi say leeral ci formaa JSON ginaaw boo duggee. Ngir laaj sa jaar-jaaru komànd ci formaa JSON, bësal fii wala nga yonne sa laaj ci mail.
Done yiñ dajale ci sitweb www.ccbmauto.com, Sàrtu No. 2008-12 bu 25 saŋwiye 2008 moo leen di aar, lépp di méngoo ak li Kuréel giy Aar Done yu Bopp (CDP) sàkku.